18-B
Xaalis bi ak wàllu peese bi
Xaalis bi ak wàllu peese bi ci Mbind yu sell yi ci làkku Ebrë
Gera (1⁄20 siikal) 0.57 g 10 gera = 1 béqa |
Béqa 5.7 g 2 béqa = 1 siikal |
Pim 7.8 g 1 pim = 2⁄3 siikal |
Siikal 11.4 g 50 siikal = 1 mina |
Mina 570 g 60 mina = 1 talaŋ |
Talaŋ 34.2 kg |
Daric (Xaalisu Pers, wurus) 8.4 g |
Xaalis bi ak wàllu peese bi ci Mbind yu sell yi ci làkku Gereg
Lepton (Xaalisu Yawut, përëm) 1⁄2 quadrans |
Quadrans (Xaalisu Room, përëm) 2 lepta |
Asariyon (Xaalisu Room ak li ko wër, përëm) 4 quadrans |
Denariyon (Xaalis Room, xaalis) 64 quadrans 3.85 g = Peyug 1 bés (12 waxtu) |
Daraxma (Xaalisu Geres, xaalis) 3.4 g = Peyug 1 bés (12 waxtu) |
Didaraxmon (Xaalisu Geres, xaalis) 2 daraxma 6.8 g = Peyug 2 bés |
Tétra-daraxma(Xaalisu Geres, xaalis, ñu koy woowe it estateer bu xaalis) 4 daraxma 13.6 g Peyug 4 bés |
Mina 100 daraxma 340 g = lu jege peyug 100 bés |
Talaŋ 60 mina 20.4 kg = lu jege peyug 19 at |
Liibar (bu Room) 327 g
|