Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024 bi tudd «Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»

Àjjuma

Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Luug 2:10​—«Xibaaru jàmm buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.»

Samdi

Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Sabóor 96:2​—Yégle leen bés bu nekk ne, Yàlla mooy musal.

Dimaas

Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 24:14​—«. . . Bu loolu amee mujug jamono ji jot.»

Li ñi teew war a xam

Tegtal yu am solo yu ñi teew war a xam.

Seetal itam...

LU JËM CI ÑUN

Kaay teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024 ​—«Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»

Ñu ngi lay woo nga ñëw teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bi Seede Yexowa yi di am ren.

NDAJE YU MAG YI

Ñu ngi lay woo ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu Seede Yexowa yi bu atum 2024 bi tudd: «Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»

Ñu ngi lay woo nga ñëw teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bi Seede Yexowa yi di am ren.

NDAJE YU MAG YI

Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 1 (Leer gu wóor gi ñëw ci àddina)

Seetaanal lãsamã tiyaatar bi tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle (Xaaj 1). Tiyaatar boobu dinañu ko wone ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024.