Ubbil li ci biir

Nañu jàng ci tabló bi

Wideo yu ndaw yii dañuy jàngale ponk yu am solo waaye dañu koy def ci anam bu reetaanlu!

 

Lan laa mën a def ba gën a am liberte?

Danga foog ne, jot na say waajur jàppe la ni mag, waaye ñoom ànduñu ci. Lan nga mën a def ngir ñu wóolu la?

Naka laa mën a def ba moytu jëw?

Booy waxtaan ba mu bëgg turne doon ay jëw, defal dara!

Bañal say moroom dugal la ci lu bon!

Ñeenti ponk yu la mën a dimbali nga am fitu jël say dogalu bopp.